ettub wolof 1 Icon
4.6
48 Ratings
10K+
Downloads
1
version
Jul 18, 2016
release date
7.7 MB
file size
Free
Download

What's New

About ettub wolof Android App

ci wolof - En français - In English


ci wolof

ëttub wolof moo leen di baaxe benn sàqum baatu wolof, te ñu tuddee ko oggo, ay léebu ak benn jumtukaayu ijji ngir mën a ijji ci wolof.
oggo mooy sàqum baatu wolof bi jëkk a am, nga xam ne baat yépp ci wolof kepp lañu leen tekki. oggo am na lu ëpp fukki junney baat ak benn.
léebu yi ëpp nañu ñeenti junney léebu, boole ci juroom ñetti téemeeri waxin. waxinu benn léebu, mooy léebu bu ñu waxee neneen.
jumtukaayu ijji bi, dina tax ngeen mën a ijji ci wolof, ci amam yu gaaw.
ngir jàng dawal wala jàng bind wolof, mën ngeen a jëfandikoo dalu-web bii di www.ettubwolof.org.

En français

ëttuf wolof vous propose un dictionnaire wolof nommé oggo, des proverbes wolof et un outil pour vous familiariser avec l’alphabet wolof.
oggo est le premier dictionnaire entièrement en wolof avec la définition des mots en wolof. Il contient plus de 11 000 mots wolofs.
Les proverbes wolofs comptent plus de 4000 proverbes incluant plus de 800 versions. Une version d’un proverbe est une façon différente de dire le proverbe.
L’outil de l’alphabet est très utile pour vous familiariser rapidement avec les lettres de l’alphabet wolof.
Pour apprendre à lire et à écrire le wolof, vous pouvez également utiliser le site www.ettubwolof.org, plus riche en contenu.

In English

ëttub wolof offers a Wolof dictionary named oggo , Wolof proverbs and a tool to become familiar with the alphabet Wolof .
oggo is the first dictionary entirely in Wolof with the definition of words in Wolof . It contains over 11,000 Wolof words.

Wolof proverbs have over 4000 ones including more than 800 versions. A version of a proverb is a different way of saying that proverb.

The alphabet tool is very useful to get quickly familiar with the Wolof alphabet letters.

To learn how to read and write in Wolof, you can also use the web site www.ettubwolof.org which content is richer.it Wolof - In French - In English


it Wolof

ëttub Wolof moo leen di baaxe benn sàqum Baatu Wolof, you bare tuddee OGGO ko, ay léebu ak benn jumtukaayu ijji ngir Men has ijji it Wolof.
OGGO Mooy sàqum Baatu bi Wolof has Jekk am, xam nga do baat Wolof Yepp it kepp LANU leen tekki. OGGO am na baat read Epp Fukki junney ak benn.
léebu yi Epp Nanu ñeenti junney léebu, boole it juroom Netti téemeeri Waxin. waxinu benn léebu, Mooy léebu drank bare waxee neneen.
jumtukaayu ijji bi dina tax ngeen Men has ijji it Wolof, it amam yu gaaw.
ngir Dawal Jang Jang bind wala Wolof, Men ngeen has jëfandikoo dalu web-bii di www.ettubwolof.org.

In French

ëttuf Wolof offers Wolof dictionary appointed OGGO, Wolof proverbs and a tool to become familiar with the alphabet Wolof.
OGGO is the first dictionary entirely in Wolof with the definition of words in Wolof. It contains over 11,000 Wolof words.
Wolof proverbs proverbs have over 4000 including more than 800 versions. A version of a proverb is a different way of saying the proverb.
Alphabet The tool is very useful to quickly familiarize you with the letters of the alphabet Wolof.
To learn to read and write in Wolof, you can also use the site www.ettubwolof.org richer in content.

in English

ëttub Wolof Wolof offers a dictionary named OGGO, Wolof proverbs and a tool to Become familiar with the Wolof alphabet.
OGGO is the first dictionary in Wolof Entirely with the definition of words in Wolof. It contains over 11,000 Wolof words.

Wolof proverbs ones-have over 4000 Including more than 800 versions. A release of a proverb is a different way of Saying That proverb.

The alphabet tool is Very useful to get familiar with the Quickly Wolof alphabet letters.

To learn how to read and write in Wolof, you can use the website aussi www.ettubwolof.org qui happy is richer.

Other Information:

Package Name:
Requires Android:
Android 4.0.3+ (Ice Cream Sandwich MR1, API 15)
Other Sources:

Download

This release of ettub wolof Android App available in 2 variants. Please select the variant to download. Please read our FAQ to find out which variant is suitable for your Android device based on Screen DPI and Processor Architecture.

Variant
6
(Jul 18, 2016)
Architecture
Unlimited
Minimum OS
Android 4.0.3+ (Ice Cream Sandwich MR1, API 15)
Screen DPI
nodpi (all screens)
Variant
5
(Jul 01, 2016)
Architecture
Unlimited
Minimum OS
Android 4.0.3+ (Ice Cream Sandwich MR1, API 15)
Screen DPI
nodpi (all screens)

All Versions

If you are looking to download other versions of ettub wolof Android App, We have 1 version in our database. Please select one of them below to download.

Loading..